Bitini
Apparence
Ci angale mooy Bithynia; Ci faranse mooy Bithynie
Diiwaanu nguuru Room ci Asi Minër la woon. Tey jii bokk na ci réewu Tirki (Turquie).
Dañu ciy wax ci Injiil ci Jëf 16:7; 1Pi 1:1.