diir
Apparence
wolof
[Soppi]diir: amna ñaari maanaa
- ab diir moo di ab àpp
- ag diir natt dara ngir jam ko mbaa dal ko,
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:
[Soppi]- diir bi nuy am ci àdduna yàggul warees na koo rafetal,
- diir naa till gi ba jam ko
Xool it
[Soppi]Tekki
[Soppi]- wu-faraas: -
- wu-angalteer: -
Déglu baatu diir ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-diir.ogg