Afritugalasi
Apparence
Afritugalasi, ci séwógaraafi ngandam gox la, mooy bi gën a ngande ci àdduna bi. Suuf Yépp yi làng doon ko, am na fenn fu ñu tàqaloowe. Moom la ñuy faral di woowee Àdduna ju yàgg ji.
Ci lu daj
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Daanaka suuf si ëpp ci àdduna bi moom la, di 55% ci lépp. Am 5,5 miliari way dëkk, maanaam di daanaka 83% gu way dëkk yu àdduna bi.
Mooy barab bi gën a yaatu ci àdduna bi soo ko mengalee ak Aamerig ak, Oseyaani, ak Dottu Bëj-gànnaar.
Seddalinam
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Ni mu amee ci bépp seddale, ay deggoo rek la ñu. Lu bari dañ koy xaaj ñetti gox: Afrig, Aamerig, Asi
Afritugalasi | Oseyaani | Afrig | Tugalasi |
Bëj-gànnaaru Aamerig | Tugal | Asi | Bëj-saalumu Aamerig |