Academia.eduAcademia.edu

Ndoomu Buur Si [Le Petit Prince - Wolof]

2018

Translation of Saint-Exupéry's "Le Petit Prince" into Wolof (Senegal). Translators: El Hadji Dièye & Maximilien Guérin. Project coordinator: Nicolas Quint.

Antoine de Saint-Exupéry Ndoomu Buur Si Ak nataali bindkat bi Ñi ko tekki ci wolof: El Hadji Dièye & Maximilien Guérin Jëwriñu liggéey bi: Nicolas Quint Edition Tintenfaß Ñi nu jàppale ci waajtaayu tekkib téere bii di “Ndoomu buur si” ci wolof ak ci génne bi: Alain-Christian Bassène, Amadou Diallo, Joseph Jean François Nunez Fondation Jean-Marc Probst pour le Petit Prince RÉPUBLIQUE DU SÉNÉGAL Un Peuple · Un But · Une Foi Avec le soutien de l’Organisation internationale de la Francophonie à travers l’Institut de la Francophonie pour l’éducation et la formation. Ministère de l’Enseignement supérieur, de la Recherche et de l’Innovation du Sénégal (MESRI). Fondation Jean-Marc Probst pour le Petit Prince Nu ngiy gërëm tamit yeneen xariti “Ndoomu buur si” ci seen ndimbal: Kees Bolwidt, Amsterdam (NL), Bernard & Danièle Chaffange, Lyon (F), Pauline Couture, Ottawa (CDN), Sylvain Cozzolino, Sannois (F), Anne-Mie Denhert, Vlamertinge (B), Tom Doyle, Dublin (IRL), Dominique Durozier, Lescar (F), Antonio Massimo Fragomeni, Roma (I), Pedro Granger, Lisboa (P), Wolfgang Kuhl, Maintal (D), Anne & Hervé Pierret, Ajaccio (F), Fondation Jean-Marc Probst pour le Petit Prince, Lausanne (CH), Thomas Stolz, Bremen (D), Patrick and Dana Tourreau, West Linn, OR (USA), Juan Antonio Soler Vilanova, Tamarite de Litera (E), Yann Vincent, Paris (F), Kuncoro Wastuwibowo, Jakarta (RI). © 2018 Edition Tintenfaß D-69239 Neckarsteinach Tel. / Fax: +49 – 62 29 – 23 22 www.verlag-tintenfass.de info@verlag-tintenfass.de Ñi saytu rañsale kàddu yi ci xët yi: τ-leχιs · O. Lange, Heidelberg Ñi móol téere bi: Appel & Klinger, Schneckenlohe ISBN 978-3-946190-67-7